Eumeu Sene Sort de sa réserve après son Combat J'ai été atteint Mystiquement, Meussouma beuré...?

566K visualizzazioni334

    Abonnez-vous à notre Chaine IThomes: ithomes.info/free/udfBmVXjm-DTPjYNv8AWvQ.html?view_as=subscriber Aimez notre page Facebook: becayembayetv/ Visitez notre Site web: www.fmsenegal.info #Bantambatv.
    77 419 03 64

    Pubblicato il 8 giorni fa

    Commenti

    1. awa barry

      Courage champion

    2. Mouhamadou Kane

      Des faiseurs de malin cela va de soi car la lutte n,'est que le culte de la betise

    3. NSTYLEZ. TMC n.stylez

      Nandane nga eumeu tigui jaroul justifier wou, balla Nandane la, modou lo Nandane la, gris Nandane la, bombardier Nandane la , LAC vrai fake le, tapete la, dafay rous lo goor

    4. Alda Fernandes

      EUMEU J'adore ton sourire

    5. Binetou rassoul

      Lac 2 ay thiokh leuh amoul ...wah écurie weum nagn ko dieundeul thiokh svp

    6. Abdul sumner

      Lac2 dafa wara bai lamba Du Dan tei du danu Match nil rek yaha derr keseh Mann Gambian la eumeu ndaanan nga

    7. Serigne malick mbacké Diop

      Balla moy sama lutteur dh mais bilahi j’adore eumeu séne ndakh deugue bimouy guéné si lamigne bi deugue dafa nékh daale❤️🙌🏾

    8. ceerw buty

      Mane dei Balla moy sama mbeur beugu wa Guédiaway mé biii dama méré lac srx Eumeu diam si yaw def gua leep franchement bénen yon moy dak inchallak

    9. Eva Dia

      Walahi jeste bi eumeu déf ak balla dafma nékh trop

    10. Mboul Ngom

      Ay way nguir yalla Eumeu boudé amna team dolen massi dougal té yalla takh

    11. Mboul Ngom

      Machalah on t'aime bcp Eumeu wadiatal bou bakh rek

      1. ceerw buty

        Qui est daccore que balla eumeu gris modou sont tousse devenu des amis maintenant

    12. Abdou Sene

      Lac est un imbéciles

      1. Abdou Sene

        Lac ne mérite pas c cacher

    13. Maman Bop

      Machallah fans club pure là Mala beug pure eumeu longue vie

    14. Bugs Bunny

      nekhoule ba nekhoul mais eumeu yaw tamite beurewo. deugue rek nekh nak

    15. Elizabeth Brooks

      machala eumeu sene diambar gua

    16. Mounass Tamba

      Je suis fier de toi champion😘💟💟💟💟

    17. Coumba Diop

      Wallahi djambar ga lac dou mbeur

    18. qopoy dnon

      yi wara boycotté 👎no sa geste ak Bg2 machala

    19. Sarr Sarr

      Vous les lutteurs vous faites toutes des fétiches donc il faut accepter la défaite. T as rien à dire .il faut être sportif.

    20. Adama Malick Dramé

      Lac d'où dara da nirou woule sakh mbeur

    21. Adama Malick Dramé

      Bilay eume da melni nion boke père et mère bilay da ma la begue menouma sétane sa lamb si salle de bain laye dougue monté ay écouteur ba volume 100

      1. qopoy dnon

        Eumeu bilahii wakh ga deug lac 2 da donn teup aka dall rekk pour wone gayii nee mooguu def dara tee tank yii sakh diogoul

    22. Adama Malick Dramé

      Non eume ya fi nék ya meune kou nékoule lac li d'où défaite dhe yaw champion nga respect mbeur on é toujours derrière tw

    23. Assane Konte

      Je vais convoqué les amateurs de lutte pour faire une marche pour que lac 2 arrête de lutter

    24. Moustapha Kamal Th.

      Eummeu, boul wakhati dotouma beuré ak mom . Dél wakh beugatuma beuré ak mom inchalla. Jajeuf mbeur

    25. Pape medoune Ndiaye

      Eumeu bilakhi wafii né

    26. soniyu ziuy

      Qui est daccore que balla eumeu gris modou sont tousse devenu des amis maintenant

    27. Mustataa Siise

      Euma tay bërewoo dara

    28. Diagne Gnilou

      En t'en que domou sèrére qui parle jamais sérère saymbok mérénagnoula

    29. Diagne Gnilou

      Yacodjoh sabaram

      1. soniyu ziuy

        Non eumeu gor deugue la

    30. ndiaga faye

      Jämbàr deugue ngueu maaacha allaah ki ngua doon da dieel mooy thiounné reek koo diapp mistiquement War koo meuneu daan

    31. Hamidou Agne

      Eumeu champion gue 👍Lac mome dou beure

    32. Pape Sane

      Je suis supporter de Balla gaye mais eumeu sene je t'adore vraiment legui sama mbeur nga ndakh sa xol dafa rafet

    33. Awa dia Sy

      Bilaye soule ndanane souli badola mais yaw mbeur nga diambar nga

    34. cheikh kouyate

      Eumeu il est bien. Lac 2 bonne continuation. Je suis fier de toi

    35. sotuur aeei

      Douma fans Eumeu mais damako naw franchement dafa digne degou blie machalla

      1. Aly Niane

        Ad

    36. Youssou Diop

      Eumeu bilahii wakh ga deug lac 2 da donn teup aka dall rekk pour wone gayii nee mooguu def dara tee tank yii sakh diogoul

    37. Issa Diao

      Lac dou mbeur bilahi

    38. Issa Diao

      Na bayi beurré

      1. sotuur aeei

        Eumeu takussane buné def ngakofi macha alla dangua mene béss gaindé bi yarunga mene nga béss

    39. Ndaye Khodia

      Ndanane koulou ndanane 😀sama mbeur bii yalnala yallah dfl djm rk Yaw ak modou lô ndam siréee khalé by kham limuye deff 😁😁 Athia mbeur

    40. Assane Samba

      Wathié akh amateurs yii wathié supporter yii diambar nga ndanane nga gaindé nga amato loy prouver si lambe d'elle déglou sa encadrement géré sa carrière champions one love eumeu sa beuré mo tah ma beugu leu té dou dégn yalnala yalla diapalé

    41. Boury Ka

      Balla sama gaynder Ndiaye

    42. Mamy Ba

      Goor yalla deugue gua machalah ❤️ djomm reek gay prouver eume kou am djomm gua amoulo Keen akk nala Diam sonal sa yaye dala gnanal bilay wolay machalah ❤️

    43. Muslim2proud

      Kouko déffati nako deegg, ap mbeur dou fénn, mbeur dou tapalé...aaay kouko défati nako deeg ap mbeur dou tricher mbeur dou yambar, 😤diapé sénégalais yi dofff 💃💃💃💃💃😂😂😂😂😂Eumeu, Balla Gaye2, Yekini, Bombardier, Ama Baldé, merci infiniment, gathiéloulén lambe. Fatou Guièr 2 démal nga toog, ngir yalla boulfi dieuleuti beneu combat, doyal na gnou si yow seuk.🙄🙄😏😏😠😠😠😠😠

    44. Djily Diop

      Non eumeu gor deugue la

      1. bssni touir

        Lou lérr laa wakh

    45. vmvdou svné

      jai trop aimé son discours

    46. vito boss vito boss no stressé

      mane fans balla gayé la

      1. bssni touir

        C'est vrai je suis avec eumeu

    47. vito boss vito boss no stressé

      bilahi euma borom bakh la

    48. drttyu liqm

      yi wara boycotté 👎no sa geste ak Bg2 machala

    49. El Che

      Lac 2 moy enfoiré rek . Yaw kenn du yaw jambar deug ga

    50. Mamadou Alpha Bah

      Je suis un fan de Modou Lo mais je t'aime💕💕❤❤😍

    51. Marieme Balde

      Mais eumeu nak balla dinala dane dh one bakhga trop beugue nagne la mais dinagne la dane dh 😂😂😂

      1. drttyu liqm

        lac dafa raguale rek yow amélo kéne ak

    52. Marieme Balde

      Sana xol diekhna si lac thiim. Bravo eumeu courage. Balla ak wa keureum gnoy samay mbeur (sauf Lac maintenant) legui iow yako remplace. Borom vakh nga

    53. Aita Ndiaye

      Eumeu takussane buné def ngakofi macha alla dangua mene béss gaindé bi yarunga mene nga béss

    54. Ndeyemarie Seye

      Diamou RK ngayi âme bly

    55. BUZZ MIFA

      EUMEU BOUL BAY AWMA KÉNE COUEOUL YEW

    56. Khady Togola

      Eumeu ya meuna doull lac dakeu leu bangua guéneu sakou yi guay féne Amgua mélokane déh khawma wone ni ningua mel féne bakhoul

    57. BUZZ MIFA

      EUMEU JE T'AIME BILLAHI

    58. Issakha Ndiaye

      Tu fais partie des meilleurs.

    59. Aboubacry Sarr

      Ya fi meun dh Eumeu billahi ❤️

    60. Chekh tidiane Thiam

      C'est vrai je suis avec eumeu

    61. Mbacké Seck

      Lou lérr laa wakh

    62. Modou Mbaye

      Eum bénéne yonne boy bré boul nuyoti kénn lokho.bâ nga nuyo thi lamb dji la khamni da ngay d'Abou.

    63. Abdou Mbaye

      Eumeu sa kanam

    64. khass Killah

      Boléne waxé té yalla tax ngéne xamni lac2 mo tané si combat bi ndax mom sax défna touti effort eumeu sax wax nako après combat bi "waroléne ma wonn téyélo sama bop" motax dafa taxaw rék défoul dara. Questioné nagn ko mo bo xolé boubax dafay rafétal di rectifié wax bi coz ay staff faw gnoniko bouko wax parck lolou daf léni yaxal mbeur gnou fayla ay millions sa staff nane la téyél sa bop

    65. Penda Wade

      Yaw diabargua bilay

    66. Khady Gueye

      lac dafa raguale rek yow amélo kéne ak

    67. Khady Gueye

      billay diabare gua

    68. Mame Saye Sylla

      Bilahi eumeu sene wakhone na lako si beineu commentaire nila lac de guiers 2 dalayy tardel rek khamoul gatt ragale na bilahi wokhone na lako beurei woule bayi woule dafa ragalll tropp tropp

    69. Abu Konate

      Eumeu lat 2 amoul diome

    70. Ibrahima Khaliloula Hounsah

      Eumeu Nguaïdé Nguay Meussa Done Bo Bayé Beuré Sax Nguaïdé Ngua

    71. Diogop Ka

      Machalla fiér de toi champion 💪💪💪sa kaw sa kaname

    72. Ibrahima Diop

      💪💪💪👍👍

    73. Khadidiatou Gueye

      Barki yamlah Eumeu damala beug

    74. Seyidina Sow

      Eumeu champion nga lou lérr Lac war nga kholaat sa beuré té di dieul décision, am nga katane loy ragal, khamon sakh biss bo mome warko am ndam,... modou lo ndam rék Incha ALLA

    75. Sila Dame

      Q

    76. Sall Ablaye

      Khole bou rafet eumeu

    77. Mansour Gueye

      Mberr yaw diaroul sakh ngay nioue khana nonou yaye Kane mberr pure nga

    78. Isatou Jobarteh

      Eumeu sene yow ya Barry wakh barry tapaleh

    79. Fati Sow

      waw kay eumeu diadieuff way on te fais confiance

    80. Adama Fall

      Champion nga

    81. Mariama Diéne

      💪💪😇😇😇😍😍😍👍

    82. ASTOULO KOBAR

      Eumeu yawdal gathia ngalama chapeau a vous mbeur kaamil NGA

    83. Pape Davido

      Cœur pour diambar jdi ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

    84. Tijani Dia

      Waw kay sama mbeur bi amal diame yaw lanou beugue tay ak soube mala beugue rek té yallah takh soy beuré douma ame diame wallahi taye wnibik hateu

    85. Pape Davido

      ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

    86. Ahmada Dial

      Iow tamit beure wo ...wakh ko kéne meunou niou nakh

    87. Adama Camara

      Eumeu séne diambar gue nion gui sa gui naw

    88. Gooo Bhff

      Eumeu ❤️❤️❤️❤️💪

      1. Gooo Bhff

        @gtoss chddy lac mo bougone Revanche

      2. gtoss chddy

        Vous avez tout les deux déçu

    89. Mariama Aliou Diouf

      Fier de vous Eume Sene

    90. Serigne saliou Lo

      Waw lac nonou ladone def mé khamnanou touti si lamb

      1. gtoss chddy

        Vraiment jambar gua mbeur lac modoul touss

    91. ibrahima ndom

      Eumeu mi da melni da beug beuré wate AK Balla

    92. Pisco Kane

      Wakhoo fi dara...tu as fui le combat .sois honnête waay .

    93. Rama Gueye

      Euma boul décourager lépou dina bakh lac mome dangay warou 💪

    94. Fatou Thiam

      Walaye tu est le meilleur je t'aime mbeure

    95. JuNiOr BabA

      Wakh dji amna solo yéndou na maana eupeu

    96. samba Sy

      Il a raison, lac2 c’est un fuyard

    97. Mame Gor

      Eumeu wakhna deug 🤭Mbeur yi nio maak thiéré massé ak lalo 😂Balla gaye ak papa sow biniouy mbapatt. 2002 terrain 22 bounte keur birahim Ndiaye sétane nako j’avais 17ans legui nio donc niom warone nagnou am 20 ans ou 22 ans donc souma calculer balla warna aam 39 ans ou 40 ans a se moment 🤭🤭😂😂

    98. Aly Dieng

      Bilahi emeu ta raison lac amoul dioum amoul fouleu

    99. Bienvenu Cheikh chico SECK

      Eumeu nak, on t'aime bien because yagg gn beuré lamb jank you neex mais bi mom iow ak lac yaleen si yem defoleen fi dara dsl nak defaroul watt da melni filla mod'lo dougeul guénagoffa D.

    100. tyfa dieng

      Late 2 dou mber nabayi beré on t'aime fort eumeu💪