Série - WOUDIOU PEETIORGO Saison 3 - Episode 70

Khar Media

953K visualizzazioni689

    Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
    instagram
    kharmedia_officiel?igshid=jf9h4pcgofsi
    facebook
    kharmedia_l'officiel
    Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.

    Pubblicato il Mese fa

    Commenti

    1. faye mingue

      Wa guewel promotion la beug walla ak mousor bi😂

    2. Fatou Camara

      Ana gni fan Coumba wonelene sene bopou 🤚🏻

    3. Fatou Camara

      Bi géweul foumou amati elle parle trooooop elle casse les oreilles 👂

    4. sasha D

      partie warougar bi avec le battaré et tout le tralala c'était ennuyeux et sof. et puis ces futilités sont à bannir de nos traditions car lii moy khadiamal seuy yi

    5. Fatoumata Dia

      c du nimporte quoi ibou nest pas aussi riche pour offrir tout ca a mamy

    6. Momy Fall

      Hiii ay yalla miniou sakkk li loumou don🤗🤗guéwalou yayi mami dji tmt sou waxon dank dara douko dakh té silay geuné am class ah nn way kénén ki moko eup class fouf

    7. Mame awa Dieye

      Sm bopou ba gui metti nax guewel bi

    8. Mame awa Dieye

      Merou guewel bi ray nama😀😀

    9. Fama Gaye

      Wa yeine ani Sophia ak Eumbam bi😂

    10. Khady Fall

      2 la

    11. Thiara Io

      Ay way ibou walo wakh li mais Dior yaw yako déve

    12. Fama Ndiaye

      Sheuuuu guewel bii😂😂😂😂😂😂😂😂😂

    13. Faly Niang

      Bonjour bon soir 🤩🤗🤭🤠🙅🤦🙋

    14. Sadi Diouf

      nous sommes la❤😍

    15. Kya Thiam

      Nnnnnn mére guéweule bi raye nama😂😂😂😂😂

    16. OmarioN Samb

      Mère guéweul bi euppeul na ak mousaur bi di mèlni chapot militaire😂😂😂

    17. funstyleful

      Pour une fois l’épisode a une longueur correcte.

    18. Bineta Diagne

      Guewal bi da saf khorom wayai yayou mami yi tamit dionguomanagn ba yakou

    19. kia seck

      Coumba sa meuve raféte na

      1. kia seck

        Kou d'accord beusseul j'aime ♡♥♥♡

    20. Khadidiatou Ndiaye

      ANA WA TEAM NDELLA AK COUMBA WAY!BAKH DAL MOY RAFFETTE JIKOO VIVE LA FAMILLE. YALLA NA FAMILLE YEUP NÉK BÉN. COUMBA SA RÔLE BI DAMA NEKH TROP.JADORE MES FRÈRES MOTAKH.

    21. Miss C 04

      Wayéne kou moussor Mére bi 😭😭

    22. Katy Diarra

      Gueweil bi limou moussor lanela 😂😂😂😂

    23. Bineta Leye

      Wa gueweul yi tamittt amnagn khaliss deh tei ken takagoul😂😂😂wa kone jourou khewba noumouy mel Wa mom dans la vrai vie khana gueweul la?😂😂😂khoromou n’a d

    24. Khady Gueye

      Je suis fans de ndella

    25. Demba Sall

      L'Extravagance dans les cérémonies familiales

    26. Wfpsn Vam

      Ay way moussorou gueweul bi tamite lane la😂😂😂😂😂

    27. horssy Ba

      Guewel bii missorou am bii😂😂

    28. Aminata Bocoum

      On parle pas à un malade comme ça tchiiip

    29. Maguette Kébè

      Ay guéweulou mami bi amatoul moyenneeee

    30. Maina Cisko

      Wa guewell bi meun na youkhou deh lannn doumako lall😂😂😂😂😂😂😂😂

    31. Maty Niang

      Le série l'a j'aime beaucoup

      1. Maty Niang

        Cou beugue sa Haye beuseul j'aime

    32. Mamayaye Wague

      السلام عليكم ورحمة الله وبركاتهيا

    33. Mairam Diop

      Mann mbadou douma deff profession guewuel

    34. Mairam Diop

      Wa billet yi momm mbadou fo billet

    35. Wane Ly

      Nul

    36. arame ngom

      pn

    37. Mama Sow

      💓💜💓💓💜💓💓💙❤💝

    38. Aida Mbengue

      Kéweul bi migui melni rakou madiaga dakh youkhou yi

    39. Bintou Gueye

      Sa lamign bou léeroon fii radiakho ay yalla mignou sack mba lii diamou la 😂😂😂😂

    40. AISSATOU DIAW

      Moussorou guewel bi DH day titalaté 🤭Dior day dof ndella âme dome mouné ndella sath domam lii wa ana Sophia elle aussi doit payer

    41. Dickel Sy

      Mane nak mangui komance tiit thie woudjou perthiorgo nak yaye mamie ak tata bi ak guewel bi ay defante kat lanioumay nirou hii jai peur lii dey kom grand comba😲...ndeyssane ndella yallah nala yallah diappale walla ngen separewou sakhe mane lii daloul sama xel

    42. Étoile Buzz

      ithomes.info/net/rLek0K9xjYOnq3Y/video

    43. Safia Mane

      Franchement c’est horrible les hurlements de cette femme....purée on prend même pas de plaisir à regarder franchement c’est abusé 😫😫😫

    44. Yacine Diop

      Oh ndiaya mogui ni way 😂😂

    45. Adama Diaby

      No geweul bi khana day dora fegne télé 😁ahhh no yak na souniou nop yi

    46. Louise Diouf

      Gueweul bi elle m'énerve

    47. Amsa Siby

      Je pense Mamy mo nara raw Dior alon rék

    48. aicha aidara

      😍😍

    49. Binta Gaye

      WA merre bi tmt elle me saoûle 🙄🙄🙄😭😭😭😭

    50. Mame Diarra NDIAYE

      Pollution sonore ngay fofou wah gewel bi😅

    51. Fatimata Dia

      C’est Maty Thiam dogo la maman de mamy ou elle se ressemble ?

    52. Mame bousso Baly Ndiaye fall

      Waa mbaye sa mousseur bi tamit😂🤣

    53. Mariama diallo

      Guewel bi ak moussoram bi melni tinguané ish

    54. Ami Marone

      Sheu mere geweul yao hana danga waneu lézard té bayiwosi hel😂😂😂

    55. Ndeye awa Diop

      Wa kou kham li gueuwél yii don wakh man dé Lép damako avancé 😂😂

    56. Ramata Sy

      Wawe mère bi Fatna sama nopeyi

    57. linguère Ndiaye

      Dior mi Ba d’où doof

    58. NDEYE ANTA DIAKHOUMPA

      Mere gueweul bi tamitt volumam forna yée na sama doom dji🤭

    59. Ndeye lo Dieng

      Gueweul bi dama defané mouSôrame be koye wakhlo akh sama nopou yengui beuneu

    60. mbenelo pene

      Enfin niou guiss yenene visage😀

    61. Dieynaba Kane NIANG

      Wa gueweul bi mom loumouy yokhou ni rek beug beute souniou nop yi en plus 30 minutes yeup gueweul yi nioko dièkhal ish

    62. Toutane Guisse

      Guéwél bi doumako bal yéna sama dom

    63. Phya So

      Ayy guewal bi akk youkhou yi 😂😂😂

    64. Fama Niass

      Wa ki youkhom yii ba andoullak drah ay yallah miniu sakk li ba diam la

    65. Adji Astou Ndiaye

      Wa gueweul bi tamite ah da forcé bamou eup kidé kouko djokh micro si khew dou bakh mére boul andi Set bi ngir yalla

    66. Fat Diop

      Guewal bi mom reuy n'a lamign DH mousoram bi Di mellni négou niakh🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🏃🏃🏃🏃ayy yalla miniou sakk 🤣🤣🤣🤔 mes fatt thierno dama nekh bilay 💋💌💔🙏 machallah 😍😍

    67. mouahmed tall

      👍👍👍👍👍

      1. Safiétou wade

        💝👌👆📒

    68. Discreet Naboo

      Nimporte quoi. Je ne comprends pas comment on peut réaliser ou regarder une série qui n'a aucun contenu.

    69. Fodé Kébé

      Les Série Sénégalais c'est vraiment nul

    70. djamil Mbodj

      30 mn de merde

    71. Sophie Thiam

      Mai tmt dougnou wahh si guéweul bi elle m'a énervé

    72. Ndeya Ndiaye

      Elle crie la dame c’est désagréable 🤭

    73. Leva Kouyate

      Ma korsa qui la reconnaît sur la série c’est la vie❤️❤️😂😂beugue khalisss

    74. Martita La Fleurette

      Yèneu wara dieul minutes yeup kheup ko thi premier cadeau bi ok d'accord 🙄🙄🙄

    75. Maty Touré

      Iphone 11 pro 😂😂 louy lolou yaw😂😂!!!!!!

    76. Zeynab Sow

      Ah geweul bi chof na trop mais lou khéw tey 30 min 😰😰😰

    77. princesse torodo

      ✋✋✋

    78. cuisine de Halima

      Wayeii perthiogo légui yi dé defanté rk moy sén fort

    79. Selly birama Sall

      Sheut les deux gueweul😂😂😂

    80. Mame khoudia Mbengue

      Wa tmt gueweul bi eska normale na tmt

    81. Abdou Diop

      wa sophia mome animou 😂😂😂😂

    82. fatou Gueye

      Nga yakarne ninou yakamtè seuy bii ba ma my dou gnew change sii ndella

    83. mbaye diop

      Cv

      1. Safiétou wade

        Gv

    84. proud woman

      Guewel bi nena lamigne bi leroul ay bou lerone yi youkhou ohhh🤣🤣🤣

    85. Mariama diatta

      Mami très belles ❤️

    86. Thiawserigne Falou

      ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️👍

    87. Thiawserigne Falou

      Je vous aimes beaucoup

    88. Coumba wade Diop

      Mashala 30mns😂li kén xamoul loumou done

    89. Ndeye Ndiaye

      Bilahi ibou a raison baloul akh ndélla amna nio khamni kéneu doulén lal touj galén di déf lou bòne yalla diko fankkeu yaw guay gueuneu soneu nék thi thiono

    90. Fatima Diaw

      Gueweul khana dagn ko takal micro bopamm ohhhh

      1. Safiétou wade

        Whatshapp plus😷😷😷

    91. black girl

      Sheutt man yokhou guewel yi damay febar😂😂😂

    92. Abi Diop

      Merou geuwal bii mom doyna seukk sii série bii eupal naa trop kii simple mom defoukoo

    93. Diakhou Ndiaye

      Khana saison bi daffa finnn en yéne kou tite yéne wouyoulénema lou khew

    94. Amina Cissé

      Guewell bi neina da gatt lamigne nonuu😂😂konn d bo goudonn lamigne tothie fii😂

      1. Ramatoulaye Faye

        Wa khana

    95. Cla Diouf

      Elle a perdu son enfant celà va l aider à changer ça façon de vivre avec les autres

    96. Mariama kamara

      Tay rek lama série bi meussa sof ndakh wakh diou bari té amoul sens

    97. Lyzzy Mendy

      Wa mais guéweul yi mon amna gnou khalisss dh

    98. Fall Diaga

      Waa mére yii nounou chon wé ni machallah❤💖😍

    99. Maïmouna Ndour

      Ey ey quel genre de Gueweul