BANTAMBA TV Une télé, Une Vision

  • 30
  • 28 051 345

Commenti

  1. awa barry

    Courage champion

  2. Mouhamadou Kane

    Des faiseurs de malin cela va de soi car la lutte n,'est que le culte de la betise

  3. NSTYLEZ. TMC n.stylez

    Nandane nga eumeu tigui jaroul justifier wou, balla Nandane la, modou lo Nandane la, gris Nandane la, bombardier Nandane la , LAC vrai fake le, tapete la, dafay rous lo goor

  4. Mbaye Simal

    😂😜

  5. Alda Fernandes

    EUMEU J'adore ton sourire

  6. Binetou rassoul

    Lac 2 ay thiokh leuh amoul ...wah écurie weum nagn ko dieundeul thiokh svp

  7. HIP HOP FLAVA SN

    ماشاءالله يا إمام جبيل كوات 🌹💐🌻🌼

  8. Abdul sumner

    Lac2 dafa wara bai lamba Du Dan tei du danu Match nil rek yaha derr keseh Mann Gambian la eumeu ndaanan nga

  9. Mamina Cissé

    Lac sérieux bouma donn gor takh nga ma am courage nekk mbeur finga ko tekk mo yomb bilay meune nako😂

  10. Serigne malick mbacké Diop

    Balla moy sama lutteur dh mais bilahi j’adore eumeu séne ndakh deugue bimouy guéné si lamigne bi deugue dafa nékh daale❤️🙌🏾

  11. Sidy Badji

    Menteur doulou reck

  12. saliou ndiaye

    Khalé bi meune diague 🙏🕌🙏🙏

  13. ousmane sow

    Makk nènane rebotes danou diane diane mo mouthie

  14. kolim jone

    Merci sama père Beckay grand contre petit reugue reugue ak franc koudieuloull sëne avance ragal nga 🇨🇵🇨🇵🇸🇳🇸🇳

  15. ceerw buty

    Mane dei Balla moy sama mbeur beugu wa Guédiaway mé biii dama méré lac srx Eumeu diam si yaw def gua leep franchement bénen yon moy dak inchallak

  16. Mahha Brwn

    😂😂😂😂 chei Cheihk

  17. Eva Dia

    Walahi jeste bi eumeu déf ak balla dafma nékh trop

  18. Moussa Touré

    L'arbitrage est nul

  19. teuf msb

    cheikh dou mbeur

  20. Abou Fresh official

    Kasara Yalla bi

  21. Bakary Mane

    Merci Eumeu merci balla sama mbor

  22. Mboul Ngom

    Ay way nguir yalla Eumeu boudé amna team dolen massi dougal té yalla takh

  23. Mboul Ngom

    Machalah on t'aime bcp Eumeu wadiatal bou bakh rek

    1. ceerw buty

      Qui est daccore que balla eumeu gris modou sont tousse devenu des amis maintenant

  24. Abdou Sene

    Lac est un imbéciles

    1. Abdou Sene

      Lac ne mérite pas c cacher

  25. DiBA cheri Ndack

    Waxofi darra

  26. Maman Bop

    Machallah fans club pure là Mala beug pure eumeu longue vie

  27. Bugs Bunny

    nekhoule ba nekhoul mais eumeu yaw tamite beurewo. deugue rek nekh nak

  28. Elizabeth Brooks

    machala eumeu sene diambar gua

  29. Mamadou Dia

    Cheikh loy signalé baparé di attaqué wat si souf doo arrière guene complètement danou kheu ana combat pleminere yii

  30. Mounass Tamba

    Je suis fier de toi champion😘💟💟💟💟

  31. Ousmane Diop

    😁😁😁

  32. pdg-le-morée sal-zer

    Des grands champions

  33. Pape Sow

    le son a la fin j'adore. C quoi le titre

  34. Magget Fall

    Lac vs franc

  35. Assane Ndiaye

    Moi j'ai raté le combat et je regarde d'abord face to face Ensuit le combat 🤣🤣

  36. Coumba Diop

    Wallahi djambar ga lac dou mbeur

  37. qopoy dnon

    yi wara boycotté 👎no sa geste ak Bg2 machala

  38. BIGTHIO Danfa

    Yaw boy niang dafa am defaite Ken bouko force AMA balde kokou dafa merite bokoul ak boy niang bo xamni dou songue fila beurre ak zoss cng wathie neko beurre par force

  39. Djouly Touré

    C’était ennuyant par contre ils ont vraiment respecté les mesures barrières.

  40. Daouda dieye

    Pabi limou wakhe leer naa déh bougnou khékhé Modou lo doumako dioudia doyna borome khél

  41. Sarr Sarr

    Vous les lutteurs vous faites toutes des fétiches donc il faut accepter la défaite. T as rien à dire .il faut être sportif.

  42. Adama Malick Dramé

    Lac d'où dara da nirou woule sakh mbeur

  43. Adama Malick Dramé

    Bilay eume da melni nion boke père et mère bilay da ma la begue menouma sétane sa lamb si salle de bain laye dougue monté ay écouteur ba volume 100

    1. qopoy dnon

      Eumeu bilahii wakh ga deug lac 2 da donn teup aka dall rekk pour wone gayii nee mooguu def dara tee tank yii sakh diogoul

  44. Adama Malick Dramé

    Non eume ya fi nék ya meune kou nékoule lac li d'où défaite dhe yaw champion nga respect mbeur on é toujours derrière tw

  45. Assane Konte

    Je vais convoqué les amateurs de lutte pour faire une marche pour que lac 2 arrête de lutter

  46. Moustapha Kamal Th.

    Eummeu, boul wakhati dotouma beuré ak mom . Dél wakh beugatuma beuré ak mom inchalla. Jajeuf mbeur

  47. Demba Guite

    Ses sample il fau installer des camera 📸 Dan vo vature tu peu meme s’adupte le camera de ton Maison a meme tan Vermane les lutteur come vous

  48. Tbd

    YALLA MI YORR JAMM TÊY JAMAL KOKU NEEX YALNA JAMAL ÑËP BARKEB ALQURAN SONKO YALNA NEK PRESIDENT 2024 AMA YALNA DAAN MDLO INCHALLAH

  49. Pape medoune Ndiaye

    Eumeu bilakhi wafii né

  50. soniyu ziuy

    Qui est daccore que balla eumeu gris modou sont tousse devenu des amis maintenant

  51. Mustataa Siise

    Euma tay bërewoo dara

  52. Diagne Gnilou

    En t'en que domou sèrére qui parle jamais sérère saymbok mérénagnoula

  53. Diagne Gnilou

    Yacodjoh sabaram

    1. soniyu ziuy

      Non eumeu gor deugue la

  54. ndiaga faye

    Jämbàr deugue ngueu maaacha allaah ki ngua doon da dieel mooy thiounné reek koo diapp mistiquement War koo meuneu daan

  55. Hamidou Agne

    Eumeu champion gue 👍Lac mome dou beure

  56. Ass Gueye

    Wakh ga degue de lac si bopam dafa gniakeu fayda amoul dioum bilahi

  57. Lady Shasha

    Happy birthday to you Euma saine

  58. Pape Sane

    Je suis supporter de Balla gaye mais eumeu sene je t'adore vraiment legui sama mbeur nga ndakh sa xol dafa rafet

  59. Awa dia Sy

    Bilaye soule ndanane souli badola mais yaw mbeur nga diambar nga

  60. cheikh kouyate

    Eumeu il est bien. Lac 2 bonne continuation. Je suis fier de toi

  61. sotuur aeei

    Douma fans Eumeu mais damako naw franchement dafa digne degou blie machalla

    1. Aly Niane

      Ad

  62. Mamadou Diagne

    Waxi mbeur rek nougoul sokhor bakhou....balla délay dane défalla teranga

  63. momo dk

    Gorré ba dé moo guene wakh wakhét !!!

  64. Youssou Diop

    Eumeu bilahii wakh ga deug lac 2 da donn teup aka dall rekk pour wone gayii nee mooguu def dara tee tank yii sakh diogoul

  65. Issa Diao

    Lac dou mbeur bilahi

  66. Issa Diao

    Na bayi beurré

    1. sotuur aeei

      Eumeu takussane buné def ngakofi macha alla dangua mene béss gaindé bi yarunga mene nga béss

  67. Khadybabou Sene

    En kone tu sais que modou lo lokho yi comme kher

  68. AMADOU BA

    Machalah

  69. Ndaye Khodia

    Ndanane koulou ndanane 😀sama mbeur bii yalnala yallah dfl djm rk Yaw ak modou lô ndam siréee khalé by kham limuye deff 😁😁 Athia mbeur

  70. Moussa Matar Fall

    modou lo moy sama mbeur mé père balla kouka nangou loul limou def si lamb ji diapal ni do sénégalais....

    1. kolim jone

      Pere ta tout dit yale na yala goudal sa fane

  71. seye mohamed

    Balla nit kou bakh la vraiment

  72. diouf abdoul ahad

    Revanche yi mo wara doyy

  73. Assane Samba

    Wathié akh amateurs yii wathié supporter yii diambar nga ndanane nga gaindé nga amato loy prouver si lambe d'elle déglou sa encadrement géré sa carrière champions one love eumeu sa beuré mo tah ma beugu leu té dou dégn yalnala yalla diapalé

  74. Mame mor Lo

    Mais yamb niangue na

  75. Mame mor Lo

    Mais yaawou eske moungui entrainer

  76. Ale Gaye

    Per békaye yage fi lol té wer DEUG ré k ga vahk machallah

  77. DOUDOU

    MDRR

  78. Boury Ka

    Balla sama gaynder Ndiaye

  79. Matar Kamara

    Rang

  80. Mamy Ba

    Goor yalla deugue gua machalah ❤️ djomm reek gay prouver eume kou am djomm gua amoulo Keen akk nala Diam sonal sa yaye dala gnanal bilay wolay machalah ❤️